
Ardoise
Slate
Nde ngon-mi Sénégal naatnoo-mi lekkol. Ina moƴƴi, kadi miɗo jogii sehilaaɓe heewɓe.
Min ngonnoo ko hedde 14 almuudo. Duɗal ngal ina saɗi seeɗa. Min kaalatno Fulani e Farayse seeɗa. Min ngollii e kaayitaaji e slate. Min mbinndi e dow lefol ngol e kaaƴe, min mbaɗi hiisa e min mbinndi konnguɗi.
To leydi Siwis, en ngalaa slates hannde; min mbinnda kala ko woni e kaayitaaji. Miɗo ɓuri yiɗde winndude e kaayitaaji.
Ardoise
Bi ma nekkee Senegaal laa jàngi. Neexoon na, te bariwoon naa ay xarit.
Nu ngi nekkoon lu tollu ci 14 ndongo. Ekol bi dafa mettiwoon tuuti. Nuy wax Fulani ak tuuti Français. Nuy liggéey ak kaaye ak ardoise. Nuy bind ci kaw ardoise bi ak krey, def math ak bind ay baat.
Ci Suisse amatu nu ay ardoise ; Danuy bind lépp ci kaaye. Dama taamu bind ci kaaye bi.
Pizarra
Cuando estuve en Senegal, fui a la escuela. Era buena y tenía muchos amigos.
Éramos unos 14 estudiantes. La escuela era un poco difícil. Hablábamos fulani y un poco de francés. Trabajábamos con cuadernos y una pizarra. Escribíamos en la pizarra con tiza, haciendo matemáticas y escribiendo palabras.
En Suiza, ya no tenemos pizarras; escribimos todo en cuadernos. Yo prefiero escribir en el cuaderno.
Ardoise
Quand j’étais au Sénégal, j’allais à l’école. C’était bien et j’avais beaucoup d’amis.
Nous étions environ 14 élèves. L’école était un peu difficile. On parlait peul et un peu français. On travaillait avec des cahiers et une ardoise. On écrivait sur l’ardoise avec une craie, les calculs, des mots.
En Suisse, on n’a plus d’ardoise, on écrit tout sur les cahiers. Je préfère écrire sur le cahier.
Qui a écrit cette histoire ?
Cette histoire a été réalisée par le/les auteur⋅trices suivant⋅es, qui font partie du groupe Acc11 2025.
Découvrez d'autres histoires de l'albécédaire
Voici quelques histoires tirées au hasard ...
Fuite
nouveau !